Téré Doundou Lyrics
Doma téré doundou mann
Ndakh sakou loma
Koulay téré doundou mom
Na fékeu mou momla yaw
Ndakh yèneu saay nitt tekla thiono
Dèlou nékeu thji noflay
Soko nango bamou sonal la yako tek sa bopou way
Ouuuhh waaahhh
Mani déféko ni ndakh bakane diam la beugeu
Doundal seu doundou boulènn falé
Yèneu yi soxor lamay ndourol
Wakh dji deh safouma dorr yi deh yeuugouma
Ndakh sama yaram’ma blindé
Dioxoma lèkeu, dioxoma nann momouloma yaw mi lé
(Doma téré doundou
Doma téré doundou)
Ngay diougaka danou niouni ki deh diambar leu
Di agné thji aleu bi rèrrè thji mbédeu mi niounan’la niafa ko nonoula
Bo amé té amoto yaw nitt yila donn yènè lou baakh niolay ndieuka saaga
Ngay dougaka guéneu diko lidieunti, niounanla yow mi deh thiaga nga
Bougn la téré doundou
Doma téré doundou
Doma téré doundou
Mann amouma diott té loma def bal nala (nala)
Dima lidieunti bay xeuy bideunti xana deh yaw deh sonou lo
Dounn momoula adouna nonou la, ndakh kou nèkeu diw dou diamam
Téré ma doundou beugeu di doundou tay ma xamal la, lo xamoul wonn
Doma téré doundou
Doma téré doundou
Doma téré doundou
Adouna yalla ngay diamou boko défoul dinga ganiou
Doundou lénn, linguén di doundou niou yènènté diam
Adouna yalla ngay diamou boko défoul dinga ganiou
Doundou lénn, linguén di doundou niou yènènté diam
Ndakh yèneu saay nitt tekla thiono dèlou nékeu thji noflay
Soko nango bamou sonal la yako tek sa bopou way
Ouuhh waaahhh
Mani déféko ni ndakh bakane diam la beugeu
Doundal seu doundou boulènn falé
Yèneu yi soxor lamay ndourol
Wakh dji deh safouma dorr yi deh yeuugouma
Ndakh sama yaram’ma blindé
Dioxoma lèkeu, dioxoma nann momouloma yaw mi lé
(Doma téré doundou
Doma téré doundou)
Ngay diougaka danou niouni ki deh diambar leu
Di agné thji aleu bi rèrrè thji mbédeu mi niounan’la niafa ko nonoula
Bo amé té amoto yaw nitt yila donn yènè lou baakh niolay ndieuka saaga
Ngay dougaka guéneu diko lidieunti, niounanla yow mi deh thiaga nga
Bougn la téré doundou
Doma téré doundou
Doma téré doundou
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2020
Album : Benen Level (Album)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
VIVIANE CHIDID
Senegal
Viviane Chidid is a Senegalese singer of mbalax and R & B, born September 29, 1973 in Mbour, Sen ...
YOU MAY ALSO LIKE