Home Search Countries Albums

Tama Lyrics


Gni di weur loumay fey
May coaché deureum ni tatch
Gnè di weur di fènn
May coaché deureum ni tatch
Hey tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Hey  papa ndiaya wakhal ak gnom
Hey ndiaya wakhal ak gnom
Hey tama wakhal ak gnom

A part generation coumbeu
Musique bi mako meuneu gawlo
Ay pages youtube you guoumbeu
Sènn tèy khamnguènn ni sama daw leu
Gnom dagnou djakhann di saaw
Job africa sogua songuou kaw
Mali ani sokhomo
Nguani ma sokhoma béni
Téleu deul tél tchi guènn
djeul seumeu temps
Yonou ndawv dou guaw
Yorr bayré youssou madjigènn
Douma concurrenou kènn tchi yènn
A bouguou Papa from alou panyan
Maigua cissé mangi fay tchop beu légui
Tchow li tchow li, Yaye amoul wakh

Gni di weur loumay fey
May coaché deureum ni tatch
Gnè di weur di fènn
May coaché deureum ni tatch
Hey tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Hey  papa ndiaya wakhal ak gnom
Hey ndiaya wakhal ak gnom
Hey tama wakhal ak gnom

Gno bokk game bi
Wayè dougnou bènn
Seu boop féssoul
Takh sa poche yi beunn
Tchow li tchow li
Danguay wakh té do dèff
From djèkk fils may coacher
Yégueul barre todj niveau
Fékk meu milieu may ngolo
Borom abidjan leu ak la fayette
Samba késsé
Lékk sénn money
Dém teudi nélaw
Senegalboy wakh ko tchi kaw
Amna ay boy town yiy sissou
Gnom deugnouy doul kènn doussi shoot
Boudè gnou ngui si cas boy diamguen o bloc
Mane la domou réwmi damfi tèkk sama tank
Niveau bimeu tolou meune  toumeu tontou
Né si sama yone baylènn gnouy onkou

Gni di weur loumay fey
May coaché deureum ni tatch
Gnè di weur di fènn
May coaché deureum ni tatch
Hey tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Hey  papa ndiaya wakhal ak gnom
Hey ndiaya wakhal ak gnom
Hey tama wakhal ak gnom
Allô? Tama wakhal ak gnom

Enjoy Synced Lyrics With Our Mobile App

Download on Google PlayGet it on App Store

WATCH VIDEO

ABOUT THIS SONG


Release Year : 2021


Album : Senegal Boy Deluxe (Album)


Added By : Farida

SEE ALSO

AUTHOR

SAMBA PEUZZI

Senegal

Samba TINE, better known as Samba PEUZZI aka BG Boy Ghetto from Diack, is a young Senegalese Hip hop ...

YOU MAY ALSO LIKE