Wa Li Nékhoul Lyrics
Maabo
Baby i love you
Honey i need you
Beus bou nek nala wax, je t’aime
Douma sone ci dila wane, how much i love you
Deg na niouné dama dof, ci ioe
Khana hnamougn ni yay dalal li wéreudi ci mane
Beugouma niouy méroo, hiéé!
Naniou andeu longo hiéé!
Baniouma si khoulo ak niom
Nieup nagn niou bayi niou jubo té nopi
Yay sama ngélaw, ioe rek doy nga ci mane
Soumala guissoul tamite, ya meun dara ci mane
Yeug yeug bi amoul limite, melni assaman
Sa mbeuguel damay doundeul, ni oxygène si mane hé !
Yama téré nélaw, ken rek nga si mane
Soumala guissoul tamite, aduna safal dou si mane
Yeug yeug noum soré ci nite sama xol ley dane
Sa mbeuguel lamay doundeul, ioe ya geun ci mane hiii !
Wa li nékhoul
Mani wa li nékhoul aaahhh …
Ioe mi ioe hé !
Yamay danel
Mani wa li nékhoul
Lathi len ma loumou saff (loumou saff) lou nékh hey waay !
Li ma nar ci mone mi (lo nar) dou diékh oohhh !
Gni diém tass souniou li, khamougn
Yeug yeug bou mel ni noo amoul
Yay sama chocolat, cacao pure bi, may sa olala
Mane may bou sure bi mome sa xol ak sey khalate hé!
Wolouna, awma xel niarr hé! Wolouna
Yay sama ngélaw, ioe rek doy nga ci mane
Soumala guissoul tamite, ya meun dara ci mane
Yeug yeug bi amoul limite, melni assaman
Sa mbeuguel damay doundeul, ni oxygène si mane hé !
Yama téré nélaw, ken rek nga si mane
Soumala guissoul tamite, aduna safal dou si mane
Yeug yeug noum soré ci nite sama xol ley dane
Sa mbeuguel lamay doundeul, ioe ya geun ci mane hiii !
Wa li nékhoul
Mani wa li nékhoul aaahhh …
Ioe mi ioe hé !
Yamay danel
Mani wa li nékhoul
Ioe mi leu, ioe mi leu hééé !
Wa li nékhoul
Ioe mi leu, ioe mi leu hééé !
Mane wa li nékhoul
Aaaahhh… ioe me ioe hé !
Yamey danel
Mani wa li nékhoul
WATCH VIDEO
ABOUT THIS SONG
Release Year : 2020
Album : Wa Li Nékhoul (Single)
Added By : Farida
SEE ALSO
AUTHOR
YOU MAY ALSO LIKE